Série - Diabarou Gorgui - "La femme du chef" -Episode 42 - Le mariage de Sadiya.

26 mars 2021
707 388 Vues

Retrouver-nous sur les réseaux sociaux
instagram
instagram.com/kharmedia_officiel?igshid=jf9h4pcgofsi
facebook
facebook.com/kharmedia_l'officiel
Khar Média est une société de production audiovisuelle, Evénementiel et communication, Nous imaginons des contenus créatifs et Nous offrons a nos clients un service global de production et de réalisation de films et de supports de communication, et un qualité à budget maîtrisé dans l’organisation d’événements.

Commentaires
  • Wa ana épisode 43 bii????

    Mame Mberry NdiayeMame Mberry NdiayeIl y a 7 jours
  • Métyna trop sadiya mais mounial rk

    Amy GadiagaAmy GadiagaIl y a 8 jours
  • Slam ms série dafa fin wala

    Oumar GUEYEOumar GUEYEIl y a 8 jours
  • Wa saison bi dafa diekh wala

    Ndeye MbayeNdeye MbayeIl y a 8 jours
  • Lui khana c fini🤔🤔🤔😭

    Birane BocoumBirane BocoumIl y a 9 jours
    • Li keye. C'est n'importe quoi

      M CM CIl y a 9 jours
  • Je ne suis pas d'accord comme ces genres de mariage kou d'accord ak Mane beseull jaime

    Gora SambGora SambIl y a 9 jours
    • 🥰😍😍😍😍😋🦄🦄🦄🦄🍓🍇🍎🥖🥐🥐🥐🥐🥐🥐🥐🥐🥐🥐🥐🥐🥐🥐

      Fatou KaneFatou KaneIl y a 3 jours
  • 😢bilay yagui may dioylo sadiya

    Mariama DialloMariama DialloIl y a 10 jours
  • Non

    Ouly SeckOuly SeckIl y a 11 jours
  • Waw khana bi moy le dernier épisode ??

    bbchou86bbchou86Il y a 11 jours
  • Les couples salit et oumaya

    Oumar Dia CisseOumar Dia CisseIl y a 11 jours
  • Wadial jour gui 🌜

    Abibo FallAbibo FallIl y a 11 jours
  • Sallal lakhou khalay khi wasalam

    Abibo FallAbibo FallIl y a 11 jours
  • Sallal lakhou khalay khi wasalam

    Abibo FallAbibo FallIl y a 11 jours
  • 43bi l'ay xar

    Coumba DiakhateCoumba DiakhateIl y a 12 jours
  • Wa kou lene maquillage

    Maguette KaneMaguette KaneIl y a 12 jours
  • Yéne wa khar media tamite yénagui commencer sof nak films yingéne di teubeul ni nak louléne téré ték films yi bangaéne khamé ni meunolen bolé ay film you beuri doléne deff par béne béne li mom déye décourage lo nite ishhh

    fatou thiamfatou thiamIl y a 13 jours
  • Wa khana série bi dafa diékhe

    Arame ThioubeArame ThioubeIl y a 13 jours
  • Film biii néxna trop mais respecter wouyou jour yiii heure boulén néxxx laniou Koy ték

    Ndeye amy MbayeNdeye amy MbayeIl y a 14 jours
  • Wa sadiya mome foumou diame

    Ramita SyllaRamita SyllaIl y a 14 jours
  • Mame saye yaramam dou daw

    Salla BarrySalla BarryIl y a 14 jours
  • Mais khana épisode 43 amoul

    Aissata PamAissata PamIl y a 14 jours
  • Désolé😭😭😭😭

    khadija diopkhadija diopIl y a 15 jours
  • 21:55 j’ai les larmes au yeux

    Aminata NdiayeAminata NdiayeIl y a 15 jours
  • Guir yalla dolen bayi serigne si ak yonen ti bi sakh ay j’aime rek Arrêtez kamem

    Ndoumbis fayeNdoumbis fayeIl y a 15 jours
  • Solution mariage forcé mom égal fakeuuu beu diiirrr bou yaagggg baniou revenir a de meilleurs sentiments dogaaa revenir wattt si c’était moi mom j’allais fuir mais alhamdoulillah bameu bokkeiii si famille bo xamnei chacun fait son choix

    Khadyja SidibéKhadyja SidibéIl y a 16 jours
  • Comme maquillage sadiya bi changer guen ko rk cv🤣🤣

    Adja deguene SowAdja deguene SowIl y a 16 jours
  • Par

    kéne Cissekéne CisseIl y a 16 jours
  • Mame saye diepi nako ak mousorame bou yague bi

    Fatou NdiayeFatou NdiayeIl y a 16 jours
  • Makiage bi dei mo geunn fouff bici bande annonce ba😂

    Toutal TallToutal TallIl y a 16 jours
  • Sheuute Oumaya aq Salif teumit😍😌❤️

    MamiiSha SowMamiiSha SowIl y a 17 jours
  • Sadiya Ndeyssane 🥺🥺🥺li mom koumakodone doundeulo dangmeiy raaye req wayer khalatoumeuko waay🤦🏽‍♀️

    MamiiSha SowMamiiSha SowIl y a 17 jours
  • Sadiya seiy ballons you bleu rouge laneuleuh?😂 mbeter kouy supporter barça😂🤦🏽‍♀️

    MamiiSha SowMamiiSha SowIl y a 17 jours
  • Le regard de Salif quand les aînés parlaient Ndeyssane explique tout amnegn louleine meti dale Ndeyssane 🥺🤦🏽‍♀️

    MamiiSha SowMamiiSha SowIl y a 17 jours
  • Ndiaya amoul diiom Bilakhiiii ki diiom amoukooo noon Sheuute 😂😂😂🤦🏽‍♀️🤦🏽‍♀️🤦🏽‍♀️

    MamiiSha SowMamiiSha SowIl y a 17 jours
  • Oumayaaa putaiiin 😂😂😂🤦🏽‍♀️🤦🏽‍♀️🤦🏽‍♀️ neinako deiite boumeuh baappp😂😂😂😂 Sheuute Aywaaay magui kheum😂😂😂 une vraie amie wallah❤️😍

    MamiiSha SowMamiiSha SowIl y a 17 jours
  • Waaah Mame Sèye mi niit leuh😂😂😂😂🤦🏽‍♀️🤦🏽‍♀️ Diouroumeukooo😂😂😂🤦🏽‍♀️kiii mereinakooo trop waaay😂🤦🏽‍♀️

    MamiiSha SowMamiiSha SowIl y a 17 jours
  • Mame Seye ioe diepinaleuh naq vraiment diepinaleuh khalato seuh dome beine yoon t’es trop égoïste comme maman mane tu m’énerve ish😒🤦🏽‍♀️

    MamiiSha SowMamiiSha SowIl y a 17 jours
  • Salif ndaysane c un bon ami

    Aisha RassoulAisha RassoulIl y a 17 jours
  • V c

    Baye Serigne DiattaraBaye Serigne DiattaraIl y a 17 jours
    • ❤️❤️😭❤️😭😭❤️❤️❤️❤️❤️❤️

      Baye Serigne DiattaraBaye Serigne DiattaraIl y a 17 jours
  • ❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️😍❤️

    Baye Serigne DiattaraBaye Serigne DiattaraIl y a 17 jours
  • 😭😭😭😭

    Maguett GueyeMaguett GueyeIl y a 17 jours
  • Ana wa sopey serigne babacar😍😘😘😚😚😎😎

    Bara DiagneBara DiagneIl y a 17 jours
  • Mounial sadiya Dina bakh

    Madieye MbengueMadieye MbengueIl y a 17 jours
  • Ndeyesane Sadiya ak Tata Saphie comme mane ak sama Tata sama magou Yaye Gaaniou juillet bi passé yanna yalla yeureum ta diégal ko ak bépp dioullit inchalla démna bayyimak wéétaay

    Adja Yayou Seyidina MouhammadAdja Yayou Seyidina MouhammadIl y a 17 jours
  • toul monde du acteur merci beaucoup

    Lamp DiengLamp DiengIl y a 17 jours
  • Maquillage bi mom khana dagno fater finitions lol

    Fatou FayeFatou FayeIl y a 17 jours
  • Ndeysane Sadiya dafa sone

    Penda NdaoPenda NdaoIl y a 17 jours
  • Ay way loutakh mariage bi am😭😭

    Mama KanoutéMama KanoutéIl y a 17 jours
  • Mariage forcé dé dou bonheur seul la maman est contente et le mari

    Unbreakable FyeUnbreakable FyeIl y a 17 jours
  • Mariage force Metina

    cissokho evacissokho evaIl y a 17 jours
  • 😭😭😭😭😭

    Aminata DiéméAminata DiéméIl y a 18 jours
  • Mane yayu sadiya miii lu takh bugu mako wolof limu wakh rék dage le su nékone sa doome dokoko béf😡😡

    Konté NdsenyKonté NdsenyIl y a 18 jours
  • M

    Ndaye DiengNdaye DiengIl y a 18 jours
  • Alhamdulilaah ! Banu fekkee sëy bi.

    Moustapha SambMoustapha SambIl y a 18 jours
  • Alkhamdoullilah comme que fekké nagne mariage bi 😂

    Amy DiopAmy DiopIl y a 18 jours
  • Mame saye dou sax niit intèrêt rek motax mou beug mayer sadiya limom ça montre k diouroul sadiya dax souko diouron douko def li

    Diaryatoulah DiopDiaryatoulah DiopIl y a 18 jours
  • 2021 y’a encore des mariages forcés moi je me taille plu personne me revoit je suis triste pour elle wallah Que Dieu m’épargner de cette souffrance 😭😭😭

    FEUZBEAUTY africaineFEUZBEAUTY africaineIl y a 18 jours
  • 😂😂😂😂😂❤❤❤❤❤😓😓😓😓

    Thiam NdeyeThiam NdeyeIl y a 18 jours
  • Ndeysane sadiya liguaye doundou metina nekeu khale bou ndaw di woudie en 3eme possition ak souniou société bi ni fi woudie mété wakhatou niou niou mayela ko beugoule rawatina sa moromou papeu yalla na yalla maye kholou mougne kepeu kouye doundeu situation bou melni

    awa teuwawa teuwIl y a 18 jours
  • Wa tmt tata safiatou kuko maquiage

    Ndeye SéneNdeye SéneIl y a 18 jours
  • Tré bon conséye

    Moussou SallMoussou SallIl y a 18 jours
  • Oooh c triste 😢yalla bouniou doundeu li🙏🏾

    Néné Thiate DiopNéné Thiate DiopIl y a 18 jours
  • Franchement yayou Sadiya diakhal nama, elle réduit la femme/sa fille à sa plus petite expression... Rien dans son discours ne présage le bonheur: nanga rakhass, nanga mougn, nanga togou, nanga, nanga, nanga rek...... Elle s'en fout pas mal de ce que peut ressentir sa "fille" à qui elle fait clairement comprendre qu'elle va souffrir dans ce ménage. En plus, les meilleurs amis de Sadiya takhaw mounane ko bou ame kharite alors k gni ils sont ensemble petits ba grands. Elle est très gauche et indélicate cette bonne dame, pffft !

    Maman RackyMaman RackyIl y a 18 jours
  • May léne m'a j'aime 😭

    Salla DiaSalla DiaIl y a 18 jours
  • Sadiya démal seyi wayé boula goor gui beugè Laal bagnal dél régélé toubeuy you bari

    Femme D'affaires mFemme D'affaires mIl y a 18 jours
  • Ces mamans qui infligent le mariage force a leurs filles c vraiment mauvais

    Eva ndiayeEva ndiayeIl y a 18 jours
  • Sadiya série bi yeup dako dioy xam way akh🙄🙄

    Mohamed BenzékryMohamed BenzékryIl y a 18 jours
  • Wa diomy wouma Khamnané beugo Gorgui Lam, Wayè bo dèma nanga Seye ba seye fou dara nèkoul Bouleen yakh sama sant bi Forcè takhou ko diogue

    Nasmou SeyeNasmou SeyeIl y a 18 jours
  • Maquillage bi nekoul wone si bande annonce bi d😂😂wala commentaire gnoléne changé Lo film bi😏

    Coumba TallCoumba TallIl y a 18 jours
  • Mètina trop

    mame fama mboupmame fama mboupIl y a 18 jours
  • J'aime trop cette série surtout sadiya

    Awa ColyAwa ColyIl y a 18 jours
  • En fin mariage bi amna, gno sonenah gnoune😂

    Fatoumata SallFatoumata SallIl y a 18 jours
  • Hoo c triste sa me rappel le jour que je parter chez mon mari 😭

    marieme Nianemarieme NianeIl y a 18 jours
  • Ah tata safi dioylo nama wallahi 😭😭😭😭

    Kane KineKane KineIl y a 18 jours
  • ana niou bg k navas

    Marra CissokhoMarra CissokhoIl y a 18 jours
  • Mariasss à la décès magui deh

    Mariama KountaMariama KountaIl y a 18 jours
  • Ndeyssane mettina courage sadiya

    Kane KineKane KineIl y a 18 jours
  • Sheteute moment bou difficile mogui nonou 😂😂😂nena nagn ko wadial rek goorgui mogui woté sheut ins bobou sa fitt di teuf teufff😂😂😂a la boni sète

    Ramatoulaye DemeRamatoulaye DemeIl y a 19 jours
  • Nn thossan nékh na

    Sadikh MbathieSadikh MbathieIl y a 19 jours
  • Waw li sey la wa la mousi ba😭

    Ndaye magatte NdiayeNdaye magatte NdiayeIl y a 19 jours
  • Bilae dama dioy sadiya damako yeureum 😭

    bb fa et amdimoustapha Diagnebb fa et amdimoustapha DiagneIl y a 19 jours
  • Naka dieke ma khamni sama jour anniversaire laye done li😂😂😂

    Sokhna NdiayeSokhna NdiayeIl y a 19 jours
  • Li kou ko doundoul do ko kham 🥺🥺

    Maman Aicha DiengMaman Aicha DiengIl y a 19 jours
  • Wa sadiya Anna frérou papame biniwone seuy bi dou âme

    Thiena FayeThiena FayeIl y a 19 jours
  • Sen maquilleuse bi dh hana andoul si seuy bi No wayyyy iiiissshhhh

    lébou ndoyelébou ndoyeIl y a 19 jours
  • Mariage forcé koumou daloutt mouno ko kham

    Mame Diarra ThiamMame Diarra ThiamIl y a 19 jours
  • Lan moy fatie hémorroïde wala kouko meun fatie sonouna

    kane kanekane kaneIl y a 19 jours
  • Enfin le mariage de l'année yéne célibataire yi beusse bou sadya démé lune de miel ba gneuw té takougnouléne dinguéne lambe😃😃

    Binetounabi DiawBinetounabi DiawIl y a 19 jours
  • Hoooo man sadiya mogui may fatali sama mariage bou niou ma forsé

    Tapha ThiamTapha ThiamIl y a 19 jours
    • Khana do goor

      Diana SyDiana SyIl y a 12 jours
  • Seni makillage dara bakhoussi ana teint noir nga koye défar poudre nitr kou khess Franche-Comté warnguen kholate kilen di makillé

    Ida GomisIda GomisIl y a 19 jours
  • Cheeeerttteeeeete......ma dieppppiiiiii mame seuye miiiiiii. 😥😥😥😥😥😡😡😡😡😡

    Aida LyAida LyIl y a 19 jours
  • Sadya kila done maquiller khana dafa done nélaw

    Fatou bintou DjitteFatou bintou DjitteIl y a 19 jours
  • di doli sante samay wadiour biniouma mayer kima beug

    khady wadekhady wadeIl y a 19 jours
  • Moussorou mame sayyye bi comme potou wassss potou chambre 🤔😂😂😂

    Fatou bintou DjitteFatou bintou DjitteIl y a 19 jours
  • Wa sadya khana amo ay mbok ay kharit ana djindiére yi ak beignet yi ana rérrre yi ahhh li mba diam la 😂

    Fatou bintou DjitteFatou bintou DjitteIl y a 19 jours
  • Nioune tamite niou wakh alhamdoulilah rek come dounde Nanou ba faikai mariage bi ha yalla Nanou fi yalla bayi niou faikai gentai taw bi ak yénéne Mash Allah

    Touty DiopTouty DiopIl y a 19 jours
  • Sant nan len guerem nan len ba mariage bi niawe sen seybi nakh na yagg ne sen preparation mariage.

    fatou ndiayefatou ndiayeIl y a 19 jours
  • Wathie bou yagu bi ak ni khèw mi wètè 🤦🏽‍♀️🤣

    Yaye fall limousent BaYaye fall limousent BaIl y a 19 jours
  • Cette. Partie. Ma.fait. pleuré

    Awa NdiayeAwa NdiayeIl y a 19 jours
  • Ndeysan j'ai pitié de sadiya

    Fatoumata BaFatoumata BaIl y a 19 jours
FRworld