Intégralité combat Lac 2 vs Eumeu Sène

4 avril 2021
322 712 Vues

Visitez notre site web luttetv.com/ et aimez notre page Facebook pour voir des combats en direct facebook.com/luttetv/
facebook.com/luttetv/
instagram.com/luttetv/
luttetv.com/
frworld.info

Commentaires
  • Lac dafa waara bayi beurré deme défi lenenne

    Assane FayeAssane FayeIl y a jour
  • Gnom gnar gnépa beuré dam ken Douko.wenter

    Abdou FayeAbdou FayeIl y a 4 jours
  • MODOU Le Boss !!!ONE Love

    asioe kiouasioe kiouIl y a 5 jours
  • Diadieuf Lac2 yako meune fouf diko dah mouy daw rek.

    Rock girlRock girlIl y a 5 jours
  • Lac défo fi dara démal ga togue wah rék ga meune.

    Astou DiakhatèAstou DiakhatèIl y a 6 jours
  • 40munitou yalla gnouy weur weurloo amateur yi sans même un seul contact physique 🤔 mé yi tam nagnouko si lac2 motakh ma gueum balla gaye 2

    bouytt guytbouytt guytIl y a 6 jours
  • Lamb de merde

    Ismail DiassiIsmail DiassiIl y a 7 jours
    • Combat à l'image du parrain de cette médiocrité....

      asioe kiouasioe kiouIl y a 5 jours
  • Heureusement que la distanciation social a été respecté 😅😅😅combat covid 19 ngay am fofou

    Ailsa NiAilsa NiIl y a 7 jours
    • Combat bi lepeu sooff teugg mi sakh dafa sooff

      Rock girlRock girlIl y a 5 jours
  • Pierre faire

    Farimata SambFarimata SambIl y a 7 jours
    • Kén barewoul

      bouytt guytbouytt guytIl y a 6 jours
  • Bilahi boudone balla guaye diékh na

    Sidi DoipSidi DoipIl y a 8 jours
  • Eumeu séne laniou wakh san pour san eumeu chéri Khou

    Awa DialloAwa DialloIl y a 8 jours
  • Machalla lutte tv et buzz

    Imam Djibril NdiayeImam Djibril NdiayeIl y a 8 jours
    • Je ne savais pas que dans l'arène il y'avais des comédiens ! Gni kou niou yab ?

      Ailsa NiAilsa NiIl y a 7 jours
  • Wakh rek laye def lac

    fall Ousseynoufall OusseynouIl y a 8 jours
  • Sheut franchement lac m’énerve eumeu Sene aussi ils n’ont rien foutu merde fallait leurs laissés dans le stade kou dane sa morom woté téléphone

    Anastasia DiengAnastasia DiengIl y a 8 jours
  • Bilahi lacs amél guama akh dh sama hémorite yeguatouna 40mn magui took

    Amadou dieye KebeAmadou dieye KebeIl y a 8 jours
  • mo wayyy

    DESNA WEZZDESNA WEZZIl y a 9 jours
  • Mane mom dama djiomi si bi comba wa eumeu sene mi louko dal vraiment tu m'a déçu

    marema fallmarema fallIl y a 9 jours
  • Ce combat, décevant est à l'image de son parrain mais également de son promoteur.

    Amadou Yoro FallAmadou Yoro FallIl y a 9 jours
  • On dirai combat des coqs

    Fode TraoreFode TraoreIl y a 9 jours
  • Combat Balla Gueye mon nehk

    Mamadou SeckMamadou SeckIl y a 9 jours
  • Combat à l'image du parrain de cette médiocrité....

    SosodiaSosodiaIl y a 9 jours
  • Combat bi lepeu sooff teugg mi sakh dafa sooff

    Abo FallAbo FallIl y a 9 jours
  • Eumeu am na droit teudie lamb dji sokhla woul denko sokh la N Domou kharam bi Lac mi reuy lamegne kay na dem foukarthji loumou sokhla bagna khar niou may ko comme day gamou kay

    Abdou DIOUFAbdou DIOUFIl y a 9 jours
  • Kén barewoul

    Ndony DiattaraNdony DiattaraIl y a 9 jours
  • Tres décevant ce combat

    Sada DkrSada DkrIl y a 9 jours
  • Je ne savais pas que dans l'arène il y'avais des comédiens ! Gni kou niou yab ?

    biggy benbiggy benIl y a 9 jours
  • Faut revoir les décisions arbitrales gni gnak diom dougnou dieul Benz initiative silagnouy profité

    Fatimata SowFatimata SowIl y a 9 jours
  • Mbeur yeup gno wara of lac de guiers dafa niak diom

    Fatimata SowFatimata SowIl y a 9 jours
  • Billahi nekhoul ba nekh mais beurè ak Lac 2 day wagni sa crédibilité tapetla rek

    Doudou NdiayeDoudou NdiayeIl y a 9 jours
  • Lamine tu es professionnel

    ligue1&2 sénégalais fsfligue1&2 sénégalais fsfIl y a 9 jours
  • So beugué combat bou nékh teugueul Modou xaragne lô Balla ama ak gnognou nioy beuré

    Modou DiagneModou DiagneIl y a 9 jours
  • No gnoune Gaston mo gnou khawma loutakh mouye teugeule Lac combat yambar bou bone bi.

    Maodo FallMaodo FallIl y a 9 jours
  • Tous ces millions pour ça ! Chiimmm !

    BDBDIl y a 9 jours
  • Magui khar ba keneu tegueti comba disi bolei lac tamna lii

    Aida GueyeAida GueyeIl y a 9 jours
  • Nn mbeurr yi mesure barrière yi laniou respecter distatiallation physique li com guerre😅😅

    Galo SeneGalo SeneIl y a 9 jours
  • Li dou combat léwtoo la

    Idy Xaragne LoIdy Xaragne LoIl y a 9 jours
  • Niome niare kéne beuré wousi aye ragal lanou rek

    Dame DiopDame DiopIl y a 9 jours
  • Lac gui daffa kate ndayame

    Jammal AndersonJammal AndersonIl y a 9 jours
  • Combat médiocre lac mome mou melni kouye baskette nii. 😆ô

    Mariama DiattaMariama DiattaIl y a 10 jours
  • Wakh deug yalla contre n'a Lac 2 trop mais combat bi môme moko beurre leppu Eumeu Séné beureoul Dara 🙈🤣🤣🤣🤣🤣🤣🤣💪

    Aliouinho AwAliouinho AwIl y a 10 jours
  • Non mais Qui lac2 dafko humilié eumeu légui Modou lo wakhnakko 😅🤣😂😅🤣😂👊🤛🤜💪

    Ousmane SaneOusmane SaneIl y a 10 jours
  • Combat distanciation sociale,no coronabi mo yak combat.

    Omar BaOmar BaIl y a 10 jours
  • Lac 2

    Douweuz la FouineDouweuz la FouineIl y a 10 jours
  • Bob

    Jack DafeJack DafeIl y a 10 jours
  • Kenn dou balla💪💪💪💪

    Cawane NdoyeCawane NdoyeIl y a 10 jours
  • Merci lac kou mèr tampi soxor baxoul

    BAM'S BAM'SBAM'S BAM'SIl y a 10 jours
  • Ma khala eumeu diap Modou lô rek Darko Moulay dan rek guay ande ah mom chaque jour Modou lô si bopam Moy yak sa carrière légui Moy touko mogui lay Ray rek wah nala Lima kham Modou lô méh séd Ray la dh

    Ndeyeomzoo DiopNdeyeomzoo DiopIl y a 10 jours
  • nayis na

    Code MbathieCode MbathieIl y a 10 jours
    • Boubou Mbathie

      Code MbathieCode MbathieIl y a 10 jours
  • Lac da niak diom mo wara song si ndax Eumeu nek na roi ba par3

    Bab DioufBab DioufIl y a 10 jours
  • Waye ma beugue bala thi âme diome

    Seynab Fatale cisseSeynab Fatale cisseIl y a 10 jours
  • lac mo yakk combat bi

    Mass Ibn haïriMass Ibn haïriIl y a 10 jours
  • Youssou ndour dila waye yadanu melni yada

    Modou Mbaye KaModou Mbaye KaIl y a 10 jours
  • Waxante wax deug sila eumeu defoufi Dara wolah lac def na lep vraiment

    Umou KhairyUmou KhairyIl y a 10 jours
  • Lac gordjigéne la mo mome lagn may revanche

    Leyti NdiayeLeyti NdiayeIl y a 10 jours
  • Wa lac mi dougne ko guéné si lamb dji yobb ko si lumbeul bi😂

    Pape SyllaPape SyllaIl y a 10 jours
  • Commentaire bi baaxoul 👉😡👎👎👎👎👎

    Toure Cheikh abdou lahadToure Cheikh abdou lahadIl y a 10 jours
  • Nie man domalen support niom laniy yoni nioy dorr manifestation yii

    serigne mbayeserigne mbayeIl y a 10 jours
  • Lac mo niak diome Cheteuteu kene waratouko teugeul combat

    Astou MbodjiAstou MbodjiIl y a 10 jours
  • Ken gneme woul

    Ba NdariBa NdariIl y a 10 jours
  • BALLA rek moo gniou maye takousanne bou nekh dia dieff balla

    Mamadou lamine MANEMamadou lamine MANEIl y a 10 jours
  • ??? Wtf? Fuck!

    d gd gIl y a 10 jours
  • Que diablos me recomienda FRworld

    BrokenBrokenIl y a 10 jours
  • Sérieusement beuré wouléen darra eumeu tay tu mas déçu

    mya choumya chouIl y a 10 jours
  • Lac a tout tenté franchement.

    yaro bakh tvyaro bakh tvIl y a 10 jours
  • *It's time to repent and seek JESUS* .He gave his life, and suffered the wrath of the Father in the cross, to save you from a eternal hell. For God loves you, but the sin must be punished. On the third day He raised from the death, showing to the world that He is God. So stop sinning and clean your life. He returns soon to judge and destroy the sinners. *Read the Bible.* *THE END IS NEAR.*

    samu elsamu elIl y a 10 jours
  • Cool

    Diallo DjibiDiallo DjibiIl y a 10 jours
  • Eumeu amoul dara loumouy prouver lac Naina Moy khalai té dafay cons combat bi eum dako faikssi si noumouy beurai rek

    Khady ThiamKhady ThiamIl y a 10 jours
  • Lac beuré na eumeu mi tay mo andi galas meussa def li

    Ndama TorinoNdama TorinoIl y a 10 jours
  • Beurrré wou lén fi dara

    Mamor NiangMamor NiangIl y a 10 jours
  • Me mané lima sert Lou lac Ben lokho leu beureu ba comba bi diekh

    Moustapha BilalMoustapha BilalIl y a 10 jours
  • Lac dou dara vrai goor dafay am fitt

    lary normallary normalIl y a 10 jours
  • Modou ,Balla ,eumeu, Ama, goûté gui,tapha tine nio nékha teugeule comba lat mome beuss bou néké roi des aréne lambeu DÉ mane mome faufoulaye diaré bayi lambeu

    haulepontio tabarèzhaulepontio tabarèzIl y a 10 jours
  • Magkhy dora cétane comba bi lat bétenama li bane façon beuréla mane suportérou modou lo la mé kéneu dou balla gaye

    haulepontio tabarèzhaulepontio tabarèzIl y a 10 jours
  • Khawna ndakh setlouguen, Eumeu vs Lac, ngebeu Gris vs Balla lagnou sol.

    wakheetwakheetIl y a 10 jours
  • Lac 💪💪🏆

    mariama sarrmariama sarrIl y a 10 jours
  • 🙈

    Mansour DiagneMansour DiagneIl y a 10 jours
  • Nékhoul nékhoul dara safou si thiey balla Gaye ya nékha farale dimanche 💪💪

    Astou BaAstou BaIl y a 10 jours
  • Chiiiim 6 moy 9 niome niar nieuppa yèmm danio niakk diom

    Ma DiawMa DiawIl y a 10 jours
  • Bilaye eumeu nékhoule wone thii lamb ji lac dako diékou si lép bilaye mai lac dafa ragale trop 🤣🤣

    adam's dialloadam's dialloIl y a 10 jours
  • Mane eumeu séne moye sama beure mai combat bi lac moko momone ragale rék mon takh danone eumeu

    adam's dialloadam's dialloIl y a 10 jours
  • WTF? ... who can stay waving their hands longer?... I'm lost 😶

    WTF JesusWTF JesusIl y a 10 jours
    • In deed!!!

      Abdoulaye TambaAbdoulaye TambaIl y a 9 jours
  • Gnata carton rouge 🤣🤣🤣🤣

    diome Bledarddiome BledardIl y a 10 jours
    • 🤣🤣🙈

      Mansour DiagneMansour DiagneIl y a 10 jours
  • Combat covid 19 respect .drapeau Macky echec rek

    almamy diabyalmamy diabyIl y a 10 jours
  • A mon avis daniou wara changé système bi def ko 3 guéww premier bou makk deuxième mi temps bou ndaw 5 dernière minutes yi geuewou 1m mbeur bou guen niou dagg la 25% .

    Bamba SeckBamba SeckIl y a 10 jours
    • 🤣🙏🏾

      Mansour DiagneMansour DiagneIl y a 10 jours
  • MACKY SALL LOKKO TOUDEE DOU NEX...

    Cheikh MbackeCheikh MbackeIl y a 10 jours
  • Lac waroul am combat

    Amidou DialloAmidou DialloIl y a 10 jours
  • Que luta e essa?? 🔝🇧🇷🇮🇹l

    Filipe Messias italyFilipe Messias italyIl y a 10 jours
  • C'est pas du combat

    Ndeye MbayeNdeye MbayeIl y a 10 jours
  • Eumeu yama rouslo

    Salam PrinceSalam PrinceIl y a 10 jours
  • Congrats Lac 2

    Sarjo JabbiSarjo JabbiIl y a 10 jours
  • Lac de guerre dafa wara bayi

    Visionnaire VisionnaireVisionnaire VisionnaireIl y a 10 jours
  • Lamine amoul quoi nena mitapms nganan afestisma😂😂😂😂

    lahad bou kharagne Lolahad bou kharagne LoIl y a 10 jours
  • Promoteur bou beug sa haliss doko def si lac si décevoir amateur et promoteur lac deuk, lac est coutumé des faits

    Bour SineBour SineIl y a 10 jours
  • Eumeu ioe la beugon nga am Victor mes DESS nga paré té mes lac mom benn promoteur waratouko teug

    lahad bou kharagne Lolahad bou kharagne LoIl y a 10 jours
  • Lac d'où Mbeur na Dem Modou Modou dji nopal bopam mes lamine liguey bi rafet na torop ak jamm

    lahad bou kharagne Lolahad bou kharagne LoIl y a 10 jours
  • Lac mo gueuneu sokhla combat bi lou takh defoul nimou defone papa sow lac guerre ragal la eumeu nimou def nonou leu parce que il a une foi été le roi 👑 des arènes et en plus il est le plu âgé il est presk en fin de carrière lac style beuré bi la wara bayii chak combat nul nione sokhlowouniou nul mome ak boy niang tamite nii la defone dafa nio respecté woul rek respecté woul tamite wa guédiaway mbeur bou niaméoul cou dou mbeur mbeur faw nga melni BG2 da nga encaissé premier coup nga dem defi li ngay def dane deme sa yone chapeau a balla guaye2

    Aboubacry NdaoAboubacry NdaoIl y a 10 jours
  • Combat corona boul lal boul diegué

    bamba babamba baIl y a 10 jours
  • Lac d guier momm kouma waxati. Combat wam nala niouss

    Gamou KaneGamou KaneIl y a 10 jours
  • Lac kou mbeurei ak mom say suporter dinagnoula mėrė parsk dou.nekhal lamb

    Fallou GueyeFallou GueyeIl y a 10 jours
  • Combat bi est ce que dou complot tamit . Temps yi complot dafa hew si rewmi Ndah mofiy def beuz. Niom niar la

    Djibril SeneDjibril SeneIl y a 10 jours
FRworld