Eumeu Sene Sort de sa réserve après son Combat J'ai été atteint Mystiquement, Meussouma beuré...?

6 avril 2021
558 321 Vues

Abonnez-vous à notre Chaine FRworld: frworld.info/tost/udfBmVXjm-DTPjYNv8AWvQ?view_as=subscriber Aimez notre page Facebook: facebook.com/becayembayetv/ Visitez notre Site web: www.fmsenegal.info #Bantambatv.
77 419 03 64

Commentaires
  • Lac2 dafa wara bai lamba Du Dan tei du danu Match nil rek yaha derr keseh Mann Gambian la eumeu ndaanan nga

    Abdul sumnerAbdul sumnerIl y a 6 heures
  • Balla moy sama lutteur dh mais bilahi j’adore eumeu séne ndakh deugue bimouy guéné si lamigne bi deugue dafa nékh daale❤️🙌🏾

    Serigne malick mbacké DiopSerigne malick mbacké DiopIl y a 9 heures
  • Mane dei Balla moy sama mbeur beugu wa Guédiaway mé biii dama méré lac srx Eumeu diam si yaw def gua leep franchement bénen yon moy dak inchallak

    ceerw butyceerw butyIl y a 19 heures
  • Walahi jeste bi eumeu déf ak balla dafma nékh trop

    Eva DiaEva DiaIl y a 20 heures
  • Ay way nguir yalla Eumeu boudé amna team dolen massi dougal té yalla takh

    Mboul NgomMboul NgomIl y a jour
  • Machalah on t'aime bcp Eumeu wadiatal bou bakh rek

    Mboul NgomMboul NgomIl y a jour
    • Qui est daccore que balla eumeu gris modou sont tousse devenu des amis maintenant

      ceerw butyceerw butyIl y a 19 heures
  • Lac est un imbéciles

    Abdou SeneAbdou SeneIl y a jour
    • Lac ne mérite pas c cacher

      Abdou SeneAbdou SeneIl y a jour
  • Machallah fans club pure là Mala beug pure eumeu longue vie

    Maman BopMaman BopIl y a jour
  • nekhoule ba nekhoul mais eumeu yaw tamite beurewo. deugue rek nekh nak

    Bugs BunnyBugs BunnyIl y a jour
  • machala eumeu sene diambar gua

    Elizabeth BrooksElizabeth BrooksIl y a jour
  • Je suis fier de toi champion😘💟💟💟💟

    Mounass TambaMounass TambaIl y a jour
  • Wallahi djambar ga lac dou mbeur

    Coumba DiopCoumba DiopIl y a jour
  • yi wara boycotté 👎no sa geste ak Bg2 machala

    qopoy dnonqopoy dnonIl y a jour
  • Vous les lutteurs vous faites toutes des fétiches donc il faut accepter la défaite. T as rien à dire .il faut être sportif.

    Sarr SarrSarr SarrIl y a jour
  • Lac d'où dara da nirou woule sakh mbeur

    Adama Malick DraméAdama Malick DraméIl y a jour
  • Bilay eume da melni nion boke père et mère bilay da ma la begue menouma sétane sa lamb si salle de bain laye dougue monté ay écouteur ba volume 100

    Adama Malick DraméAdama Malick DraméIl y a jour
    • Eumeu bilahii wakh ga deug lac 2 da donn teup aka dall rekk pour wone gayii nee mooguu def dara tee tank yii sakh diogoul

      qopoy dnonqopoy dnonIl y a jour
  • Non eume ya fi nék ya meune kou nékoule lac li d'où défaite dhe yaw champion nga respect mbeur on é toujours derrière tw

    Adama Malick DraméAdama Malick DraméIl y a jour
  • Je vais convoqué les amateurs de lutte pour faire une marche pour que lac 2 arrête de lutter

    Assane KonteAssane KonteIl y a jour
  • Eummeu, boul wakhati dotouma beuré ak mom . Dél wakh beugatuma beuré ak mom inchalla. Jajeuf mbeur

    Moustapha Kamal Th.Moustapha Kamal Th.Il y a 2 jours
  • Eumeu bilakhi wafii né

    Pape medoune NdiayePape medoune NdiayeIl y a 2 jours
  • Qui est daccore que balla eumeu gris modou sont tousse devenu des amis maintenant

    soniyu ziuysoniyu ziuyIl y a 2 jours
  • Euma tay bërewoo dara

    Mustataa SiiseMustataa SiiseIl y a 2 jours
  • En t'en que domou sèrére qui parle jamais sérère saymbok mérénagnoula

    Diagne GnilouDiagne GnilouIl y a 2 jours
  • Yacodjoh sabaram

    Diagne GnilouDiagne GnilouIl y a 2 jours
    • Non eumeu gor deugue la

      soniyu ziuysoniyu ziuyIl y a 2 jours
  • Jämbàr deugue ngueu maaacha allaah ki ngua doon da dieel mooy thiounné reek koo diapp mistiquement War koo meuneu daan

    ndiaga fayendiaga fayeIl y a 2 jours
  • Eumeu champion gue 👍Lac mome dou beure

    Hamidou AgneHamidou AgneIl y a 2 jours
  • Je suis supporter de Balla gaye mais eumeu sene je t'adore vraiment legui sama mbeur nga ndakh sa xol dafa rafet

    Pape SanePape SaneIl y a 2 jours
  • Bilaye soule ndanane souli badola mais yaw mbeur nga diambar nga

    Awa dia SyAwa dia SyIl y a 2 jours
  • Eumeu il est bien. Lac 2 bonne continuation. Je suis fier de toi

    cheikh kouyatecheikh kouyateIl y a 2 jours
  • Douma fans Eumeu mais damako naw franchement dafa digne degou blie machalla

    sotuur aeeisotuur aeeiIl y a 2 jours
    • Ad

      Aly NianeAly NianeIl y a 10 heures
  • Eumeu bilahii wakh ga deug lac 2 da donn teup aka dall rekk pour wone gayii nee mooguu def dara tee tank yii sakh diogoul

    Youssou DiopYoussou DiopIl y a 2 jours
  • Lac dou mbeur bilahi

    Issa DiaoIssa DiaoIl y a 2 jours
  • Na bayi beurré

    Issa DiaoIssa DiaoIl y a 2 jours
    • Eumeu takussane buné def ngakofi macha alla dangua mene béss gaindé bi yarunga mene nga béss

      sotuur aeeisotuur aeeiIl y a 2 jours
  • Ndanane koulou ndanane 😀sama mbeur bii yalnala yallah dfl djm rk Yaw ak modou lô ndam siréee khalé by kham limuye deff 😁😁 Athia mbeur

    Ndaye KhodiaNdaye KhodiaIl y a 2 jours
  • Wathié akh amateurs yii wathié supporter yii diambar nga ndanane nga gaindé nga amato loy prouver si lambe d'elle déglou sa encadrement géré sa carrière champions one love eumeu sa beuré mo tah ma beugu leu té dou dégn yalnala yalla diapalé

    Assane SambaAssane SambaIl y a 2 jours
  • Balla sama gaynder Ndiaye

    Boury KaBoury KaIl y a 2 jours
  • Goor yalla deugue gua machalah ❤️ djomm reek gay prouver eume kou am djomm gua amoulo Keen akk nala Diam sonal sa yaye dala gnanal bilay wolay machalah ❤️

    Mamy BaMamy BaIl y a 3 jours
  • Kouko déffati nako deegg, ap mbeur dou fénn, mbeur dou tapalé...aaay kouko défati nako deeg ap mbeur dou tricher mbeur dou yambar, 😤diapé sénégalais yi dofff 💃💃💃💃💃😂😂😂😂😂Eumeu, Balla Gaye2, Yekini, Bombardier, Ama Baldé, merci infiniment, gathiéloulén lambe. Fatou Guièr 2 démal nga toog, ngir yalla boulfi dieuleuti beneu combat, doyal na gnou si yow seuk.🙄🙄😏😏😠😠😠😠😠

    Muslim2proudMuslim2proudIl y a 3 jours
  • Non eumeu gor deugue la

    Djily DiopDjily DiopIl y a 3 jours
    • Lou lérr laa wakh

      bssni touirbssni touirIl y a 2 jours
  • jai trop aimé son discours

    vmvdou svnévmvdou svnéIl y a 3 jours
  • mane fans balla gayé la

    vito boss vito boss no stressévito boss vito boss no stresséIl y a 3 jours
    • C'est vrai je suis avec eumeu

      bssni touirbssni touirIl y a 2 jours
  • bilahi euma borom bakh la

    vito boss vito boss no stressévito boss vito boss no stresséIl y a 3 jours
  • yi wara boycotté 👎no sa geste ak Bg2 machala

    drttyu liqmdrttyu liqmIl y a 3 jours
  • Lac 2 moy enfoiré rek . Yaw kenn du yaw jambar deug ga

    El CheEl CheIl y a 3 jours
  • Je suis un fan de Modou Lo mais je t'aime💕💕❤❤😍

    Mamadou Alpha BahMamadou Alpha BahIl y a 3 jours
  • Mais eumeu nak balla dinala dane dh one bakhga trop beugue nagne la mais dinagne la dane dh 😂😂😂

    Marieme BaldeMarieme BaldeIl y a 3 jours
    • lac dafa raguale rek yow amélo kéne ak

      drttyu liqmdrttyu liqmIl y a 3 jours
  • Sana xol diekhna si lac thiim. Bravo eumeu courage. Balla ak wa keureum gnoy samay mbeur (sauf Lac maintenant) legui iow yako remplace. Borom vakh nga

    Marieme BaldeMarieme BaldeIl y a 3 jours
  • Eumeu takussane buné def ngakofi macha alla dangua mene béss gaindé bi yarunga mene nga béss

    Aita NdiayeAita NdiayeIl y a 3 jours
  • Diamou RK ngayi âme bly

    Ndeyemarie SeyeNdeyemarie SeyeIl y a 3 jours
  • EUMEU BOUL BAY AWMA KÉNE COUEOUL YEW

    BUZZ MIFABUZZ MIFAIl y a 3 jours
  • Eumeu ya meuna doull lac dakeu leu bangua guéneu sakou yi guay féne Amgua mélokane déh khawma wone ni ningua mel féne bakhoul

    Khady TogolaKhady TogolaIl y a 3 jours
  • EUMEU JE T'AIME BILLAHI

    BUZZ MIFABUZZ MIFAIl y a 3 jours
  • Tu fais partie des meilleurs.

    Issakha NdiayeIssakha NdiayeIl y a 3 jours
  • Ya fi meun dh Eumeu billahi ❤️

    Aboubacry SarrAboubacry SarrIl y a 3 jours
  • C'est vrai je suis avec eumeu

    Chekh tidiane ThiamChekh tidiane ThiamIl y a 3 jours
  • Lou lérr laa wakh

    Mbacké SeckMbacké SeckIl y a 3 jours
  • Eum bénéne yonne boy bré boul nuyoti kénn lokho.bâ nga nuyo thi lamb dji la khamni da ngay d'Abou.

    Modou MbayeModou MbayeIl y a 3 jours
  • Eumeu sa kanam

    Abdou MbayeAbdou MbayeIl y a 3 jours
  • Boléne waxé té yalla tax ngéne xamni lac2 mo tané si combat bi ndax mom sax défna touti effort eumeu sax wax nako après combat bi "waroléne ma wonn téyélo sama bop" motax dafa taxaw rék défoul dara. Questioné nagn ko mo bo xolé boubax dafay rafétal di rectifié wax bi coz ay staff faw gnoniko bouko wax parck lolou daf léni yaxal mbeur gnou fayla ay millions sa staff nane la téyél sa bop

    khass Killahkhass KillahIl y a 3 jours
  • Yaw diabargua bilay

    Penda WadePenda WadeIl y a 3 jours
  • lac dafa raguale rek yow amélo kéne ak

    Khady GueyeKhady GueyeIl y a 3 jours
  • billay diabare gua

    Khady GueyeKhady GueyeIl y a 3 jours
  • Bilahi eumeu sene wakhone na lako si beineu commentaire nila lac de guiers 2 dalayy tardel rek khamoul gatt ragale na bilahi wokhone na lako beurei woule bayi woule dafa ragalll tropp tropp

    Mame Saye SyllaMame Saye SyllaIl y a 3 jours
  • Eumeu lat 2 amoul diome

    Abu KonateAbu KonateIl y a 3 jours
  • Eumeu Nguaïdé Nguay Meussa Done Bo Bayé Beuré Sax Nguaïdé Ngua

    Ibrahima Khaliloula HounsahIbrahima Khaliloula HounsahIl y a 3 jours
  • Machalla fiér de toi champion 💪💪💪sa kaw sa kaname

    Diogop KaDiogop KaIl y a 3 jours
  • 💪💪💪👍👍

    Ibrahima DiopIbrahima DiopIl y a 3 jours
  • Barki yamlah Eumeu damala beug

    Khadidiatou GueyeKhadidiatou GueyeIl y a 3 jours
  • Eumeu champion nga lou lérr Lac war nga kholaat sa beuré té di dieul décision, am nga katane loy ragal, khamon sakh biss bo mome warko am ndam,... modou lo ndam rék Incha ALLA

    Seyidina SowSeyidina SowIl y a 3 jours
  • Q

    Sila DameSila DameIl y a 3 jours
  • Khole bou rafet eumeu

    Sall AblayeSall AblayeIl y a 3 jours
  • Mberr yaw diaroul sakh ngay nioue khana nonou yaye Kane mberr pure nga

    Mansour GueyeMansour GueyeIl y a 3 jours
  • Eumeu sene yow ya Barry wakh barry tapaleh

    Isatou JobartehIsatou JobartehIl y a 3 jours
  • waw kay eumeu diadieuff way on te fais confiance

    Fati SowFati SowIl y a 3 jours
  • Champion nga

    Adama FallAdama FallIl y a 3 jours
  • 💪💪😇😇😇😍😍😍👍

    Mariama DiéneMariama DiéneIl y a 3 jours
  • Eumeu yawdal gathia ngalama chapeau a vous mbeur kaamil NGA

    ASTOULO KOBARASTOULO KOBARIl y a 3 jours
  • Cœur pour diambar jdi ♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️

    Pape DavidoPape DavidoIl y a 3 jours
  • Waw kay sama mbeur bi amal diame yaw lanou beugue tay ak soube mala beugue rek té yallah takh soy beuré douma ame diame wallahi taye wnibik hateu

    Tijani DiaTijani DiaIl y a 3 jours
  • ♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️☺️☺️☺️☺️♥️♥️♥️☺️☺️☺️☺️☺️☺️☺️♥️♥️♥️♥️♥️♥️☺️☺️☺️☺️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️

    Pape DavidoPape DavidoIl y a 3 jours
  • Iow tamit beure wo ...wakh ko kéne meunou niou nakh

    Ahmada DialAhmada DialIl y a 3 jours
  • Eumeu séne diambar gue nion gui sa gui naw

    Adama CamaraAdama CamaraIl y a 3 jours
  • Eumeu ❤️❤️❤️❤️💪

    Gooo BhffGooo BhffIl y a 3 jours
    • @gtoss chddy lac mo bougone Revanche

      Gooo BhffGooo BhffIl y a 3 jours
    • Vous avez tout les deux déçu

      gtoss chddygtoss chddyIl y a 3 jours
  • Fier de vous Eume Sene

    Mariama Aliou DioufMariama Aliou DioufIl y a 3 jours
  • Waw lac nonou ladone def mé khamnanou touti si lamb

    Serigne saliou LoSerigne saliou LoIl y a 3 jours
    • Vraiment jambar gua mbeur lac modoul touss

      gtoss chddygtoss chddyIl y a 3 jours
  • Eumeu mi da melni da beug beuré wate AK Balla

    ibrahima ndomibrahima ndomIl y a 3 jours
  • Wakhoo fi dara...tu as fui le combat .sois honnête waay .

    Pisco KanePisco KaneIl y a 3 jours
  • Euma boul décourager lépou dina bakh lac mome dangay warou 💪

    Rama GueyeRama GueyeIl y a 3 jours
  • Walaye tu est le meilleur je t'aime mbeure

    Fatou ThiamFatou ThiamIl y a 3 jours
  • Wakh dji amna solo yéndou na maana eupeu

    JuNiOr BabAJuNiOr BabAIl y a 3 jours
  • Il a raison, lac2 c’est un fuyard

    samba Sysamba SyIl y a 3 jours
  • Eumeu wakhna deug 🤭Mbeur yi nio maak thiéré massé ak lalo 😂Balla gaye ak papa sow biniouy mbapatt. 2002 terrain 22 bounte keur birahim Ndiaye sétane nako j’avais 17ans legui nio donc niom warone nagnou am 20 ans ou 22 ans donc souma calculer balla warna aam 39 ans ou 40 ans a se moment 🤭🤭😂😂

    Mame GorMame GorIl y a 3 jours
  • Bilahi emeu ta raison lac amoul dioum amoul fouleu

    Aly DiengAly DiengIl y a 3 jours
  • Eumeu nak, on t'aime bien because yagg gn beuré lamb jank you neex mais bi mom iow ak lac yaleen si yem defoleen fi dara dsl nak defaroul watt da melni filla mod'lo dougeul guénagoffa D.

    Bienvenu Cheikh chico SECKBienvenu Cheikh chico SECKIl y a 3 jours
  • Late 2 dou mber nabayi beré on t'aime fort eumeu💪

    tyfa diengtyfa diengIl y a 3 jours
  • Bilay man serign fans balla la mais dam beugue eumeu sene ndkh balla gaye

    Serigne Modou DialloSerigne Modou DialloIl y a 3 jours
  • Defofi dara bou niou wakhante deug daga ma rouslo kerok

    Mamediarra BaldeMamediarra BaldeIl y a 3 jours
  • Vraiment jambar gua mbeur lac modoul touss

    Ablaye GueyeAblaye GueyeIl y a 3 jours
  • Vous avez tout les deux déçu

    Ousmane SagnaOusmane SagnaIl y a 3 jours
  • lac daladon gadie😂

    GALAYE DIOPGALAYE DIOPIl y a 3 jours
FRworld