🛑DERNIER FACE TO FACE: EUMEU SENE VS LAC GUIERS 2 LA TENSION MONTE AVANT LE 04 AVRIL 2021

31 mars 2021
554 580 Vues

🚩S’abonner à la chaîne de la 2stv cliquez sur ce lien👉 : bit.ly/3cnXP6h
Retrouvez l'ensemble de nos programmes d'actualité et émissions de société, santé, politique, culture, musique, économie sur:
- frworld.info
- www.2stv.net
- Iptv disponible sur 2stv.sn
- instagram.com/2stv_senegal/
- facebook.com/2stvsenegal
- Snapchat: senegal2stv
- TikTok: @2stvsenegal
- twitter.com/2stvsenegal
- www.dailymotion.com/video/x7vidbb
#FACETOFACE #EUMEULAC2 #2STVLIVE #2STV #EUMEULAC2 #2STVSENEGAL #KEBETU #BANTAMBA #MODOUMBAYE

Commentaires
  • machallllaaaaaaa

    seven 7seven 7Il y a 2 jours
  • 2stv💪💪💪💪💪💪💪💪💪💪💪💪

    dcoog anmldcoog anmlIl y a 5 jours
  • Eumeu Sene Mo Meune Lac 2 beurei yi Bokul Saxx Ndamm Rekkk Incha Allah pour Eumeu Sene

    nieooj gotoynieooj gotoyIl y a 6 jours
  • Malick thiandoum je l'aime bien ❤️😘 da meunn limouy def machalla ❤️❤️

    eioshen boboieioshen boboiIl y a 7 jours
  • Eumeu la

    Buzz Divert _TvBuzz Divert _TvIl y a 7 jours
    • 🔥🔥

      dcoog anmldcoog anmlIl y a 5 jours
  • Malick thiandoum je l'aime bien ❤️😘 da meunn limouy def machalla ❤️❤️

    bcvbb hyuibcvbb hyuiIl y a 7 jours
    • Lac 2 nbam rek inchallah

      nieooj gotoynieooj gotoyIl y a 6 jours
  • Emeu Séné dagua yak sama aniff ndakh beuréwo lidousa thieur

    Ndour AdjiNdour AdjiIl y a 7 jours
    • Lac si bopam formame bi mo niaaw trop

      eioshen boboieioshen boboiIl y a 7 jours
  • Sama guayi niou wakh ko té déee lac nako promoteur boycotte

    Marie NdawMarie NdawIl y a 8 jours
  • Merda

    Ly torodo lylyLy torodo lylyIl y a 8 jours
    • Thièy le professionnalisme de Malick thiandoum

      bcvbb hyuibcvbb hyuiIl y a 7 jours
  • Yop

    Modou DiopModou DiopIl y a 8 jours
  • Lac2 Adam rek insha Allah🤞🏿✌🏿🎉🥀💘💘🎊🎊💪🏿💪🏿😏👍🏿

    Seedy BayoSeedy BayoIl y a 8 jours
  • Je suis lac bly

    beug fallou mbkbeug fallou mbkIl y a 8 jours
  • Lac mome waroule ame Kombat dou deme dou dike

    Fatou GueyeFatou GueyeIl y a 8 jours
  • Lac louma méti si yow do beuré doko bayi mou beuré

    Mamadou Moustapha DiaMamadou Moustapha DiaIl y a 8 jours
  • Lac rék 💪💪🦾

    Saikou DjigoSaikou DjigoIl y a 8 jours
  • Euye lac 2 bowakhié rk nganii sou arbitre bii siflé rek nga dokh thi kawame té kouye weur yambar diapale

    Diop BireumeDiop BireumeIl y a 8 jours
  • Lamba dal 2stv rek la wara Don nioko yoor

    Mama Abou DieyeMama Abou DieyeIl y a 8 jours
  • Lac fait doucement

    Amadou NdiayeAmadou NdiayeIl y a 8 jours
  • Gaston seytané macky sall la

    Abib Doundou GuissAbib Doundou GuissIl y a 8 jours
  • 🔥🔥

    Mansour DiagneMansour DiagneIl y a 9 jours
  • Lac 2 nbam rek inchallah

    Ousmane GoudiabyOusmane GoudiabyIl y a 9 jours
  • Lac si bopam formame bi mo niaaw trop

    Moussa ndiayeMoussa ndiayeIl y a 9 jours
  • Koool

    diatara ft linpadiatara ft linpaIl y a 9 jours
  • Thièy le professionnalisme de Malick thiandoum

    Boubou KalogaBoubou KalogaIl y a 9 jours
  • Lac yalla na danne

    booba Fast foodbooba Fast foodIl y a 9 jours
  • Lacc dakkoyy dann kenn doucii sama beurr nakk bilakh faraloumaci kenn mann le lion de Guédiawaye moyy sma beurr

    Assane TouréAssane TouréIl y a 9 jours
  • Damay ragal mou defendre ba dann eumeu,lac thim mako diéppi

    Pape Djiré MbowPape Djiré MbowIl y a 9 jours
    • Guiss ngua affaire bi dei

      FALISTO BAMBISTEFALISTO BAMBISTEIl y a 8 jours
  • Lac de guerre c'est le plus nul de l'histoire

    Cxounabamba DiopCxounabamba DiopIl y a 9 jours
  • Une question. Prkw. Couleur Maron Beige si plateau bi. Thiey macky

    Morinho DiagneMorinho DiagneIl y a 9 jours
  • Lac 2 Yallah nala Yallah may ndam barkép Serigne Touba 🙏🙏

    Khady Ndiaye Yaye FallKhady Ndiaye Yaye FallIl y a 9 jours
  • Balla gaye la namou signature reum

    serigne Sambserigne SambIl y a 9 jours
  • Bilay lamb bolewoul Eumeu ak Lac. Eumeu dou moromame ci dara..

    Sada MbodjiSada MbodjiIl y a 9 jours
  • 🙏🙏🙏🙏

    Ablaye KaAblaye KaIl y a 9 jours
  • 7 fois j esper k lac va montre qu il est l vrai Diatto

    LEMZO KEBELEMZO KEBEIl y a 9 jours
  • Lac wa pai Nio nara rousse rek

    Bache NduBache NduIl y a 9 jours
  • Lat yallnaleu yalla may ndam

    Serigne GayeSerigne GayeIl y a 9 jours
  • Lac ragale

    Lamine NdiayeLamine NdiayeIl y a 9 jours
  • Eumeu séné 100%yalna ga am ndamm

    Mbaye gueyeMbaye gueyeIl y a 9 jours
  • Ndamm rékk inchallah Eumeu sene 🤲🤲

    Mourtalla DiagneMourtalla DiagneIl y a 9 jours
  • Bilay combat lac déy soff

    Fall CheikhFall CheikhIl y a 9 jours
  • Lac de guerre stp goorgorloul ba boul nul

    Cheikhoulahi NdiayeCheikhoulahi NdiayeIl y a 9 jours
  • Euma Yan nala Yallah burbi Mai ndam inshAllah ❤️❤️❤️❤️❤️

    Kum ZaiKum ZaiIl y a 9 jours
  • Do féki kéne lac dangaye doule amo fite liguéyo dara sa comba yeup nii la napaté rék té amo fite roi des arènes mome bouko khalate ndakh amo beuré bi amo khékh bi amo fite bi démale nga togue

    Hamidou BaHamidou BaIl y a 9 jours
  • Ñiaarr ngi mom meunou ma see faral kène ndakhe dama leuna soppou loll ndeysan kou si yalla may ndame na kenn ki nangou dogal

    Bamba SeyeBamba SeyeIl y a 9 jours
  • Eumeu néko à 100% dé

    Malick FayeMalick FayeIl y a 9 jours
  • 2stv dagno ayy machalah

    Mouhamed FallMouhamed FallIl y a 9 jours
  • Wa xana lac amoul fans lac warnga xolaatt sa bopou dh

    SONKO JRSONKO JRIl y a 9 jours
  • Sur le Plan PhySique Lac Semble meilleur mais dara Eumeu dakoy dieulei Pikine iS bae

    Libasse MatiCLibasse MatiCIl y a 9 jours
  • Lac chaque combat ma méréko ndakh day mélni Atletico de Madrid défense rk 😂😂

    Thiobaré gui TvThiobaré gui TvIl y a 10 jours
  • Jajeuf lac le défenseur de walo

    Ablaye PanéAblaye PanéIl y a 10 jours
  • Eumeu yalla nala yalla may dame 💪💪eumeu👑👑

    Amath Ba CisséAmath Ba CisséIl y a 10 jours
  • Eumeu yallah naleu yallah mayy ndamm

    DiegobuenosAires DeleDiegobuenosAires DeleIl y a 10 jours
  • Kou ci am hémorroïde boul dèm stade....ndakh Lac rek ak rassou. Ahhhhh!

    Moussa DIOUFMoussa DIOUFIl y a 10 jours
  • Incha'allah yalla may laa ndamb eumeu

    Ablaye ThiamAblaye ThiamIl y a 10 jours
  • Lac meuso bagn combat 😂 xana bi nak digua beuré

    Moctar NdiayeMoctar NdiayeIl y a 10 jours
  • Eumeu sene rékk

    Saliou DiaSaliou DiaIl y a 10 jours
  • Lac dou beure ragal la arriere rek

    Sogui DiopSogui DiopIl y a 10 jours
  • 2stv vous êtes les meilleurs bilahi

    Ousmane Zizou WaneOusmane Zizou WaneIl y a 10 jours
  • Where is the fans eumeu sene ♥️♥️♥️♥️♥️

    Sewa SissokoSewa SissokoIl y a 10 jours
  • Yallah nako nieup féké si diam #eumeu séne amssi ndam

    Marouane habibouMarouane habibouIl y a 10 jours
  • Eumeu moi je suis supporter Modou Lô mais yalla nala yalla may ndam

    Fallou gallass loFallou gallass loIl y a 10 jours
  • Porono

    Mamkorr GuéyeMamkorr GuéyeIl y a 10 jours
  • Lac kaine waratouko teugeule combat .day dawe rek amoule fite

    Samba NdiayeSamba NdiayeIl y a 10 jours
  • Nigir dieumi serige touba à bonne léne fi si kourel khassida 🙏🙏🙏🙏

    kourel khassidakourel khassidaIl y a 10 jours
  • Lac wa walo dougne dello ginnaw

    lemer aidaralemer aidaraIl y a 10 jours
  • Niom gni kén doussi khalé eumeu mag la nak da yag trppp khamna ay 9ans yoyo rk la magè lac 47ans ak38ans la =85ans la =13=4/4 mois =8 kon lac day dan mou nek 1_1

    lemer aidaralemer aidaraIl y a 10 jours
  • Face2Face bii da sedd trope

    Assane NdiayeAssane NdiayeIl y a 10 jours
  • Emeu diekhalna c fini pr lui mé menna dann ndakh bet noirou wa gediaway la balla ak lac

    lemer aidaralemer aidaraIl y a 10 jours
  • Modou moye sama mbeur wayé eumeu lafaral💪💪💪💪💪💪💪💪

    Talla DiopTalla DiopIl y a 10 jours
  • Lac le meilleur face to faceure de tous les temps

    Fallou MbayeFallou MbayeIl y a 10 jours
  • Eumeu rekkkk

    Boubacar liman BadianeBoubacar liman BadianeIl y a 10 jours
  • Eumeu mo meuneu Mamie lac

    Mame awa SyllaMame awa SyllaIl y a 10 jours
  • Lambeu bo kham gnieup kham nagne ni day dieul temps yague diaroul debat

    Ousmane MendyOusmane MendyIl y a 10 jours
  • Sama lutteur bi eumeu sene yallanala yalla maye victoir

    Dip daddy DioufDip daddy DioufIl y a 10 jours
  • Sama lutteur bi eumeu sene yallanala yalla maye victoir

    Dip daddy DioufDip daddy DioufIl y a 10 jours
  • Lambe khewinawa bouléngnou sonnale

    Gueye CheikhGueye CheikhIl y a 10 jours
  • Lac néné dey diély loum sokhla🤣 noo ki dina ma rey...

    Adama SarrAdama SarrIl y a 10 jours
  • GUEUEMENA NÉ LAC DE GUERRE DE DINA DIEUL ROI BI INCHALLA!!!

    DIEUREUDIEUF DIADIEUFDIEUREUDIEUF DIADIEUFIl y a 10 jours
  • Lac je suis sure qu'il fera la distanciation social 🤣🤣🤣

    DIA AlphaDIA AlphaIl y a 10 jours
  • Lac damay saga sa... danga muna dieul roi

    Samby AmeSamby AmeIl y a 10 jours
  • Eumeu ndam inshallah

    Boubou SeckBoubou SeckIl y a 10 jours
  • Ndame si eumeu sene

    Modou bousso LeyeModou bousso LeyeIl y a 10 jours
  • Lac de guerre wakh rkk la meun

    Bilal KaBilal KaIl y a 10 jours
  • Athia eumeu

    Xalima TalifXalima TalifIl y a 10 jours
  • Ndaysan eumeu dafa téyyy bilay yalna la yalla maye ndame

    Arame ThioubeArame ThioubeIl y a 10 jours
  • Athiaaa lac2 domou guediawaye victoire inchalaaaa

    Momar N’DiayeMomar N’DiayeIl y a 10 jours
  • Allez lac ndame rek

    Papa Assane GningPapa Assane GningIl y a 10 jours
  • Lac mom lammine béé reuyyy

    29-Gaye Elhadji Oumar29-Gaye Elhadji OumarIl y a 10 jours
  • Eumeu séne ts les fans de Kharagne lo sont derrière toi

    Bar IsoBar IsoIl y a 10 jours
  • Tyshinger ndame rkkk

    kana koulibalykana koulibalyIl y a 10 jours
  • Télé day am thiassss 💞 je vous love toutes l'équipe de 2stv goudou fane ak weer ak nieup incha Allah

    ALBOURAKH24ALBOURAKH24Il y a 10 jours
  • Modou lô✊❤️

    Moussa FallMoussa FallIl y a 10 jours
  • 2stv c le meilleur de tous les temps incha Allah

    ALBOURAKH24ALBOURAKH24Il y a 10 jours
  • Lac moy ko khamni meunatoul def dara bama guemko😂😂Go Eumeu

    Mohamet El Bachir ToureMohamet El Bachir ToureIl y a 10 jours
  • Lac2 victoire rék Incha'Allah

    Almamy SakhoAlmamy SakhoIl y a 10 jours
  • wa lac 2 prkw kéne fara louko si Commentaires yi ? lac nak wax duegue néxouta faral

    Modou ModouModou ModouIl y a 10 jours
  • drapeau diogay sall doumako sétane

    Modou ModouModou ModouIl y a 10 jours
  • Eumeu ndam reck

    Fallou NdoyeFallou NdoyeIl y a 10 jours
  • KARADIO 2STV FORT EVER

    Galsen Wood TVGalsen Wood TVIl y a 10 jours
  • wa combat bi direct la wala

    Anta NiassAnta NiassIl y a 10 jours
FRworld